Light trap
A light trap attracts migratory locusts and grasshoppers when they are flying at night. When they see the light, they fly into it and fall into a bucket of soapy water below. Because the water is soapy, the locusts and grasshoppers can’t get out and they die. By putting a light trap in your field, you can learn how many grasshoppers are traveling at night.

French
Un piège lumineux attire les criquets lorsqu’ils volent la nuit. Quand les criquets voient la lumière, ils volent vers elle et finissent par tomber dans le seau d’eau savonneuse situé sous le piège. Comme l’eau est savonneuse, les criquets ne peuvent pas re-décoller et s’envoler et finissent par mourir dans l’eau. En installant un piège lumineux dans votre champ, vous pouvez savoir combien de criquets migrent la nuit et menacent potentiellement votre champ.
Wolof
Fiir gi ànd ak lamp bi dafay xëcc njéeréer yi ak soccet yi buñuy naaw ci guddi gi. Buñu gisee léer gi, dañuy naaw di jëm ci moom ba taabi ci paan bi def ndox ak saabu bi nekk ci suufu lamp bi. Ndox ak saabu boobu mooy tax njéeréer yéek soccet yi duñu mënati naaw kon dañuy dee. Bu ngeen defee fiir gi ci seeni tool dingeen mëna xam ñaata njéeréer ak soccet ñooy naaw ci tool bi ak yaq yi ñu naroon def foofu.
Build a light trap
Bring your supplies to your local metal worker to build your light trap.
Apportez tous ces matériaux à un métallurgiste, pour construire votre piège à lumière.
Yobbale leen lèpp ci minise metalik bi ndax mu defaral leen seen fiir gi.
| English | French | Wolof |
|---|---|---|
| One angle iron beam, 50 mm | 1 cornier de 50 | benn cornière 50 |
| Two flat iron pieces, 40 mm | 2 fer plat de 40 | ñaari fer plat 40 |
| One iron bar, 8 mm | 1 fer de 8 | benn fer de 8 |
| A lamp with batteries | 1 lampe à piles | ben lampe ak ay piil |
| A large laundry basin | 1 bassine de 10 à 15 L | benn paan, 10–15 litaars |
| Two locks, to secure the lamp and basin | 2 serrures, pour sécuriser la lampe et le bassine | ñaari sellur |
| Paint | 1 pot de peinture | pintur |
| Paint thinner | du liant | dilian |
Dimensions

| N° | Item/Nature | Number of pieces/Nombre de pieces | Dimension/Dimension |
|---|---|---|---|
| 1 | Lamp support / Support lampe | 1 | 30 cm |
| 2 | Top cover support / Support chapeau | 1 | 120 cm |
| 3 | Top cover / Chapeau | 1 | 130 cm |
| 4 | Lamp cage / Grille de lampe | 4 | 24 cm per piece/pièce |
| 5 | Lamp / Lampe | 1 | 1.5 V |
| 6 | Basin security bar / Barre de sécurité de la bassine | 1 | 65 cm |
| 7 | Large basin support belt / Ceinture supérieure | 1 | 1.5 m |
| 8 | Basin / Bassine | 1 | 15 liters |
| 9 | Small basin support belt / Ceinture inférieure | 1 | 1.30 m |
| 10 | Leg / Pied | 4 | 1.5 m |
| 11 | Leg stabilizers / Scellement pied | 4 | 25 cm per piece/pièce |
| 12 | Feet / Sabbot | 4 | 10 cm per piece/pièce |
Placement
When the light trap has been constructed, bring it to the field. It must be in a location at least 50 meters from trees and roads, but it should not be too difficult to reach.
Lorsque le piège à lumière est construit, apportez-le sur le terrain. Il doit être situé à au moins 50 mètres des arbres et des routes, mais ne doit pas être trop difficile à atteindre.
Su fiir gi paree, yòbbu leen ko ci tool bi. Teg leen ko fu sore garab gi ak yoon yi ci 50 metar. Wante fu yomba jot.
How to use a light trap

In the evening, go to the field where you put the trap. Bring water with you to fill the basin. Take the basin down, fill it with water, and add a little soap. Put the basin back and turn on the light. That’s it! Go home for the night.
Go back to the field in the morning. Bring a notebook and an identification guide with you. Turn off the light and take down the bucket. Pour out the water over a sieve. There may be a lot of insects in the sieve, but are there any locusts or grasshoppers? Do you know any of the species? You may not be able to identify all of them, but write down how many grasshoppers and locusts you see and what species they are if you do know.
Every three days, you will refill the basin with water and again turn on the light trap. Then you will measure the results the day after tomorrow. Every three days, you will turn on the light and repeat the process of refilling the basin and counting insects.
French
Comment utiliser un piège lumineux? Le soir, allez au champ où vous avez mis le piège. Apportez avec vous de l’eau pour remplir la bassine. Prenez la bassine et remplissez-la avec de l’eau et ajoutez un peu de savon. Remettez la bassine en place. Allumez la lumière. Et c’est tout! Rentrez chez vous pour la nuit.
Vous reviendrez dans la matinée. Apportez alors un cahier et un guide d’identification des principales espèces de criquets. Éteignez la lumière et retirez la bassine. Versez l’eau sur un tamis. Il peut y avoir beaucoup d’insectes dans le tamis, mais y a-t-il des criquets et connaissez-vous certaines de ces espèces de criquets? Si oui, comptez combien il y a de criquets de chaque espèce.
Vous allez à nouveau allumer le piège lumineux puis effectuer les comptages le lendemain. Tous les 3 jours vous allumerez la lumière du piège et répéterez tout le processus.
Wolof
Naka lañuy jëfendikkoo fiir gi ànd ak lamp? Ci ngoon si dem leen ci tool bingeen def fiir gi te yobbale leen ndox ak saabu. Def leen ndox ak saabu ci paan bi te teg ko ci suufu fiir gi te taal lamp bi. Dellu leen seeni kër ba suba.
Ci suba si dellu leen ci tool ba te yòbbale bindukaay, kaye ak tèere nataalu xaameekaay u melokaan u njéeréer ak soccet yi. Ci tool bi fay leen lamp bi. Sotti leen ndox u paan bi ci ab tame. Dina am ay gunòor ak ay soccet. Su fekkee xam ngeen xèetu soccet yi ak njeereer yi woññi leen lim u bu nekk ñaata la.
Dangeen di taalaat lamp u fiir gi té woññiwaat lim u soccet yi ak njeereer yi ci ëllëg sa. Ñetti fan yu nekk, dangeen di taalaat lamp bi te baamtu woññi bi.
What next?
When you are done counting, call your local plant/pest protection organization and tell them how many locusts or grasshoppers you observed. Tell them who you are, where you counted the locusts or grasshoppers, and how many you counted. If you know the type of each grasshopper, tell them how many of each type you observed.
French
Lorsque vous avez terminé la surveillance par comptage à vue et/ou par piège lumineux, appelez la DPV et dites-lui combien de criquets vous avez observés. Dites-leur qui vous êtes, où vous avez vu les criquets, et combien.
Wolof
Bungeen noppee ci xool bi ak saytu bi woo leen waa DPV. Wax leen seen tur, sant, dëkk ak fi ngeen gise soccet yi ak njèereer yi ak lim bi ñaata la.
Download and print instructions on page 23
| English title | Original title | language | ||
|---|---|---|---|---|
| Community Management of Locusts and Grasshoppers in Central Senegal | English | Download | ||
| Locust control methods for communities in the groundnut basin of Senegal | Méthodes de lutte antiacridienne pour les communautés du bassin arachidier du Sénégal | French, Wolof | Download |